Mardi 10 Décembre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Video

Médina Baye : Imam Moustapha Niass tire sur un moukhadam de la Fayda tidiane

Single Post
Médina Baye : Imam Moustapha Niass tire sur un moukhadam de la Fayda tidiane

Le comportement de certains Moukhadam de la Fayda Tidiane a provoqué l’ire de Imam Moustapha Niass, fils de Cheikh Ahmad Dame Niass, troisième Khalife de Baye Niass. Il a sévèrement critiqué les pratiques de l'u' d'eux sans le citer nommément. Le petit-fils de Baye Niass déplore l'attitude de ce dernier consistant à entrer dans la cité de Médina Baye dans un cortège sonore, et à fermer le mausolée pour son ziarra.

Regardez !

Article_similaires

27 Commentaires

  1. Auteur

    Anonyme

    En Novembre, 2019 (11:11 AM)
    ils sont très beaux
  2. Auteur

    Thiey

    En Novembre, 2019 (11:21 AM)
    Gamou lène wakhtaner yonenti bi MOHAMED SAWS mo gueune sène reglement de compte yi pfffffff
    • Auteur

      Free

      En Novembre, 2019 (12:33 PM)
      medina ne parle que du prophète psl, mais quand on voit des personnes comme mamour insa qui viennent troubler avec une indiscipline notoire le gamou on doit en parler.
    • Auteur

      Reply_author

      En Novembre, 2019 (13:11 PM)
      niit dale ni nga mel rek nguey wakhé, kou am lou bakh lou bakh rek laay wakh, wanté khasté, khamadi wakh djou niaw itam kouko wakh gnou xamni yaw ya mel nonou. cheikh mamour lii baye niasse diglé ak wakh si talibém nimouy mél soko xamé mbaa ngani ko diakk sans sakh mou wakh sakh déloo laa si yalla. kignan nak, sokhoor ak jalousie yaggna kaweu souff wanté yalla bourbi mooy mayé nangou mhoo guenaa sedd mhoo guenaa yombou balaa fébar khol dila décimé.
    • Auteur

      Reply_author

      En Novembre, 2019 (14:12 PM)

      Omar Seck

      En Novembre, 2019 (12:21 PM)
      kham kham meunoul soute kham yallah té lolou leu baye niasse indi. cheikh mamour insa diop dou serigne bouye woute buzz, di weer mbote, wala di wakh pour talibés yi di wakh euskeuy wala di khal. lolou kou ko def nasfou leu, bakane leu. ndieurigne lay wakh. té serigne bou mate serigne moy kilay wakh lilay dieurigne. ndieurigne si talibé, ganaw kham yallah moy beugue baye, liguéyeul ko. yewoulène, yéwoulène, yéwoulène !
    Auteur

    Kheuch

    En Novembre, 2019 (11:22 AM)
    Il parle aussi de Sangue Barkham NDiaye
    Auteur

    Mj

    En Novembre, 2019 (11:28 AM)
    Santoul niasse dé wayé sougnou borom meynako
    • Auteur

      Usa

      En Novembre, 2019 (15:58 PM)
      cheikh mamour amna xam xam djoup neu cell neu lou djaffei de no jours. yow ceider wo deug
    • Auteur

      Omar Seck

      En Novembre, 2019 (12:22 PM)
      kham kham meunoul soute kham yallah té lolou leu baye niasse indi. cheikh mamour insa diop dou serigne bouye woute buzz, di weer mbote, wala di wakh pour talibés yi di wakh euskeuy wala di khal. lolou kou ko def nasfou leu, bakane leu. ndieurigne lay wakh. té serigne bou mate serigne moy kilay wakh lilay dieurigne. ndieurigne si talibé, ganaw kham yallah moy beugue baye, liguéyeul ko. yewoulène, yéwoulène, yéwoulène !
    Auteur

    Moi

    En Novembre, 2019 (11:38 AM)
    Svp SENEWEB,

    Vous pouvez nous épargner ces genres de propos.

    SOyez constructifs, Parlez des bienfaits du Gamou, Dans tout ce que Imam a dit vous n'avez retenu que cela ,....;::::::::::::::???

    Auteur

    Baye Ciss

    En Novembre, 2019 (11:39 AM)
    Le jour où les serignes seront plus nombreux que les Talibés.. Peut-être que nous serons plus tranquilles..
    Auteur

    Mouhamed Diome Ndiaye

    En Novembre, 2019 (11:53 AM)
    Gamou Tamou nagnou si di wakhetané yonente bi psl ak ay diar diarou yonente bi ps’ mais dou tok di garouwalé wala di wakh lousa yone nekoul nek seutou baye takhoul ngua geuna kham kéne cheikh ibrahim wala yonou cheikh ibrahim bi ndakh baye yaggue nagnou ko deglou mougnouy khamal ni mbir mi nekoul si ay domou diww là wala seutou diw là

    Nagnou bayi garao bi di wakh lou essentiel témouy dieurigne Talibé yi..#NGEÛNÉL NAK MINGUI SI LOKHO YALLA TEI MOKAY DIOKH KOUKA NÉKH
    Auteur

    Fan Vi

    En Novembre, 2019 (11:53 AM)
    les chiens aboient et la caravane passe,longue vie à Baye Cheilh Mamour Insa digne soldat de El Ibrahim niasse
    Auteur

    Siley

    En Novembre, 2019 (12:21 PM)
    de nos jours personne ne respecte l'autorité. Ni dans la cellule familiale ni nul part. Là ou il n'y a pas de leader légitime il ne peut y avoir qu’indiscipline et discorde. C'est valable pour les famille maraboutique qui se multiplient au fil des années et qui veulent tous leur part du pouvoir.
    Auteur

    Pape Amady

    En Novembre, 2019 (12:39 PM)
    Quiconque Baye Niass sait que rien de peut se produire dans sa cité qu'il n'a pas lui-même agrée. Ça c'est un, deuxième si les Cherifs et autres érudits ont afflué du monde entier pour se soumettre à Cheikh Ibrahim, ce n'est pas pour acquérir auprès de lui des connaissances livresques. Ils sont venus chercher la gnose divine. Voilà ce qui poussent les jeunes à se basculer devant chez Cheikh Mamour une incarnation de vertus, de droiture. Allah ne s’adresse qu'aux personnes douées d'intelligence...

    Auteur

    En Novembre, 2019 (12:47 PM)
    C le gars qui cherche à accaparer le terrain des HLM GD Yoff face au stade. Les populations l'attendent de pied ferme.
    • Auteur

      Jeffbcmid

      En Novembre, 2019 (14:34 PM)
      bcmid meussoul troubler gamou medina, boko khamone doko wakh kokou moy dieumii yaaar ak teguine te en plus dou kalaawou... meussoulwoté beine makaaama mom beug baaye rek ma wooté
    • Auteur

      Reply_author

      En Novembre, 2019 (11:28 AM)
      fofou diamou yallah nagnou fayy deff,tokhou gnou fa yamba,diayou gnou fa sangara,thiagatou wougn fa,agresser wougn fa,au contraire sécurité bi mo ngui fa chaque khadara; yiwou yalla rek mo fay wathie; crétin
    • Auteur

      Moustapha Sarr

      En Novembre, 2019 (12:25 PM)
      khadra bo khamni c'est une fois par semaine, digueunté takusssane ak gué, depuis plus de dix ans, populations yoyou dina niou khar ba khadi. té li nga wakh dou deugue. fofou la deuk depuis 1992, té li nga wakh ni amoul. par ailleurs, autorisation mo niou fa takha tok, avant ngay wakh lathietel. les jaloux vont maigrir puis mourir. nangoul lene yallah fékheul sene khol yi. lou yallah def nit meunou si dara. cheikh mamour insa diop, yallah leu andal.

      En Novembre, 2019 (12:26 PM)

    Coolabou

    En Novembre, 2019 (12:51 PM)
    Seneweb. Je sais pas quel est l'importance cet maudit article.

    Cheikh Mamour inssa Diop et ses talibés sont tous des disciples de Cheikh Ibrahim.il nous pousse toujours à aimer Baye et ses descendants.

    Donc nous avons une autre choses a faire que être sur cette mission de Satan:(senewebe)
    • Auteur

      Anonyma

      En Novembre, 2019 (14:15 PM)
      mamour insa diop fomou diogue kou ko kham respecter ko : seutou maba diakhou ba ak mamour dary ba ak cheikhou omar foutiyou tall la .
    Auteur

    En Novembre, 2019 (12:57 PM)
    Sante Cheikh Mamour Insa rék.

    Continuer de parler, lui il continue de travailler pour Baye RDA
    Auteur

    Zahra

    En Novembre, 2019 (13:08 PM)
    Wamei lui jamais il a dit un nom ou prénom Ousmane Dicko, seytaneii nga nafeikh nga.

    Pour taguer Quelq'un alors que a aucun moment j'ai entendu dire ce quelq'un... La jalousie tue nak, je le répète la jalousie tue vite sakh. Tognkatt you boneu yii. Yalla dou andak mouk togn katt. Seytaneii... Niall liggueyy
    Auteur

    Mamadou

    En Novembre, 2019 (14:11 PM)
    Bilahi wadji mo meuneu fène, quand la mosquée de Médina Baye a été fermée pour un moukhadam!

    Ya gui toutal sa bopou dé.

    Bayilène moukhadam youy liguéyal Baye yi tranquille.

    Amolène dara lolène liguéyal sène mame Cheikh Ibrahim.
    Auteur

    En Novembre, 2019 (14:22 PM)
    A Mbour la ou j'habite un ''Moukhadame'' de Baye était venue s'installé, au début il avait que quelque Talibé mais cela s'agrandissait tous les jours wassifa zikaa youxxuu tombaient en transe ...

    A la mosquée avant la prière ses jeunes venaient lui réserver sa place a lui seul, a la fin il se comparait à Baye même !!

    Auteur

    En Novembre, 2019 (14:42 PM)
    YALLAH Rasulilahi salALLAHU aleihi wa salam la yooni, wakh ak mom mou wakh ak gnoun, Kenene koum done ap talibé yonente bi salALLAHU aleihi wa salam nguey yotou. Kone diema nek ap talibé ni gneupp , tope li SUNU BOROM SUBHANAHU WA TAALA wakh te moytou limou téré , sougnko togné toubalko , moussal sugnu moromu domou adama moy taha mouthie. Kesse nak , bene Serigne meunoul garantie kene , ndakh bess pencc gneuppeuy tiit khatal anbiya, kene rek mo am garantie té diotalina Al Quran djeuffénsunnah nguir gnou royko mouthie.

    Cessons de perdre du temps , deugue deugue YALLAH rek mofi nekk.

    Auteur

    Sagna

    En Novembre, 2019 (14:44 PM)
    CHEIKH M I DIOP EST TRES DISCIPLINE. ON LAISSE AU PETIT FILS DE BAYE NIASS L'ENTIERETE DE SES PROPOS. C'EST DE LA JALOUSIE ET RIEN D'AUTRE.
    Auteur

    Fils De

    En Novembre, 2019 (15:14 PM)
    Ces fils de... nous tympanise. Allez y suer et gagner votre vie. On dirait des pasteurs de l'Afrique centrale prets a tout pour vivre sur le dos des populations et spolier les terres.
    Auteur

    Beug Baye

    En Novembre, 2019 (15:59 PM)
    Dans l'interview, il n'a aucunement cité Cheikh Mamour Insa Diop. Ce comportement serait celui de Sangue NDIAYE

    Auteur

    Ibrahima

    En Novembre, 2019 (16:01 PM)
    https://m.youtube.com/watch?v=DX0-Oy8QFOM&feature=share
    Auteur

    Ibrahima

    En Novembre, 2019 (16:37 PM)
    https://www.youtube.com/watch?v=qz95Mv5sBKI&t=14s
    Auteur

    Sentinelle

    En Novembre, 2019 (22:48 PM)
    FO fek kou tekki woul dara dafay bari thiow. Cheikh Mamour Insa dafa ligueyal l'islam. Gnatta domou Adama la defarr. Ndiabotou Baye Niasse yeupeu ande nangoulko ndakh ndiambaram ak yaram soudone limou nek deupowoul ak yone kone Khalifa bi wala diambari faydou bi wakh. Batinement on se connait. Diaroul sissou koumou nakhari calamel yalla
    Auteur

    Elhadj 3

    En Novembre, 2019 (11:02 AM)
    https://youtu.be/qFgiAiKJFTo

    Khalifa bi mo wakh li. Kone nak sant yallah.
    Auteur

    En Novembre, 2019 (16:01 PM)
    il n a pa cité de nom ,il parle d d'une manière générale et il a dit que la vérité
    Auteur

    Sangue Bn

    En Novembre, 2019 (20:07 PM)
    Mamour Insa amoul xamm Xamm mo nekone sama serigne.

    Mais Sangue xamm Ndiaye moko heup hedeup
    • Auteur

      Abdoul

      En Novembre, 2019 (10:03 AM)
      ya perte rek; niak fayda/ cmid ken dou ko wann guinaw. kou la khamal yalla,khamal la téguine,bien se comporter en société,liguey,am fouleu ak fayda ak diom,fonk say wadiour,diamou yalla,sell dioubb,kham yalla. lenen lan moy kham kham? ma la yeureum!
    • Auteur

      Abdoul

      En Novembre, 2019 (10:04 AM)
      ya perte rek; niak fayda/ cmid ken dou ko wann guinaw. kou la khamal yalla,khamal la téguine,bien se comporter en société,liguey,am fouleu ak fayda ak diom,fonk say wadiour,diamou yalla,sell dioubb,kham yalla. lenen lan moy kham kham? ma la yeureum!
    Auteur

    Baba Baye

    En Novembre, 2019 (12:12 PM)
    Chaise serigne baye tokk na thi liifi dess moyy done talibe medina bii medina baye niass laa yarr ak teguine mofii jeurigne

    Kou fate lalaa fal sa folekou dana niaw baye moy serigne donc mouhadam yi bayilenn khelee née loumakhama fort fort thi baye rekk laniokoy amee donc dibalilenn talibe yi lenn Topp guirr niou defarou

    Baye beug niou deferou mo takh mou bidal niou rouhoul adab "ADAB"donc naniou delossi khel yii baye moy deug assalamou aleykoum

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Banner 01
Banner 01

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email